Faatug Sil Fransuwa Bokànde ciy 54 atam

bokandeNdakaaru, 7 mee (APS) - Futbalkat ñeel àdduna bu senegaal ba woon tuddu Sil Fransuwa Bokànde (54 at) faatu na altine sii ca Mets, Fraas, ginnaaw ba ñu ko doon oppeeree, la RFM siiwal.

Juddu ci 1958, Bokànde doonoon na kapiten bu ekipu futbal bu Senegaal, te gannaaw ba mu bokk ci kilifa ya jiite futbal bi ci ati 2000.

Ca wàllu klëb, futbal na ca Kaasaspoor, ekipu Sigicoor di dëkk ba mu cosaanoo, ca bëj-saalumu Senegaal. Batey futbal na ca Fraas, ca FC Metz, ca Paris Saint-Germain ak ca Nice.

SAB

Jukki bi mu askanoo

Xibaaryi.com a ngi jaale njabootam.

Ñaata yër: 2589
Àddu yi (0)Add Comment

Àddu ci Jukki bi

busy

Ñiy dugg ci Dal bi

mod_vvisit_countermod_vvisit_countermod_vvisit_countermod_vvisit_countermod_vvisit_countermod_vvisit_countermod_vvisit_countermod_vvisit_countermod_vvisit_counter
mod_vvisit_counterTay1088
mod_vvisit_counterDémb2262
mod_vvisit_counterAyu-bis bii14720
mod_vvisit_counterWeer wii59043
mod_vvisit_counterLépp-Lépp1649390

Amna: 13 gan, 3 bots yu lënku
Sa IP: 50.16.108.167
Tay la Suw 20, 2013

Ay yëgle yu bawoo Google