Login
Tur:
*
Dàkkantal:
*
E-Bataaxal:
*
Baatu-jàll:
*
Wéral Baatu-jàll:
*
Boyet yees xàmmee ak tomb sii (*) manu la ñàkk.
Bindu
Gàttalug xibaar yi:
Way-ñàkk liggéey yi dinañu jébbal seeni mbébét Maki Sàll
»
Way-ñàkk liggéey yi dinañu jébbal seeni mbébét Maki Sàll (ci waxi seen...
Tekki nañu Alquraan ci Wolofal
»
Téere bu sell bii di Alquraan tekkees na ko ba mu mat sekk ci Wolofal....
Xew-xewu OSAD ak UESLAN
»
OSAD ( www.osad-sn.com ) ak UESLAN ñooy wone BAATUKAAYU ÑAARI...
Lu aju ci Màggalug Tuubaa
»
Màggalug Tuubaa bis la bu màgg fi Taalubey Sëriñ Tuuba yi te it di bis...
Njàngum xale yu jigéen yi ca Koldaa : ñiy bàyyee ngi tollu ci 14%
»
Ndóol gu law gi, séy ak ëmb yu teel yi, dooley aada yi ak mettital ci ...
Dugg
Bindu
04:48:01 AM AM
Àjjuma, 24 Mee 2013
Njalbéen
Wér-gi-yaram
Jàngale Ak Yar
Koom-koom
Politig
Askan & Pénc
Diine & Ngëm
Bitim-Réew
Yónnee jukki
Nataal
Kàddu
PéncMi
E-Daara ji
Baatukaay
Wolof >> Wolof
Wolof >> Français
Wolof >> English
Wolof >> German
Français >>Wolof
English >> Wolof
Allemand >> Wolof
Ladab
Hikma & Waxi Njariñ
Taalif & Wolofal
Léeb & Maye
Léebu & Móolu & Xaste
Taasu & Bàkku & Jat
TéereSargal
MySpace
Facebook
Twitter
RSS
Hikma & Waxi njariñ
Pàcc bi dajale mboolem waxi Hikma yi walla waxi njariñ.
Wéy
Dooraat
#
5
10
15
20
25
30
50
100
Yépp
Tomb yi
Àdduna lu la fi waay ëppalee ag goy la, ngir woroomi dëkk benn la cay fanaan...
Àdduna naa koy neen la, xamoon naa ko, manoon naa ko, amoon naa ko.
Ànd yaar a koy yàq, tege lees manul, gàntu lees man.
Donga buy tërbiyawu moongi melni mbuus muñ duyi leer/ndox bu jegee jigeen manga cay jami ràbb muy seeb, bu ko laalee mu bëtt tuuru
Kilifa balaa war a digle day def balaa war a tere day ba
Kilifa daa war a yar doomam, moo gën jikki ba fiy bëgg a juge, naan sama gannaaw na ngéen topp ci diw...
Ku dul mer mbaam la, Kudul mar xaj la.
Ku gis sa baay, gis sa nijaay, gis sa taawub baay war a xam sa bopp.
Lees yarul kenn du man a jaxasook moom, loo bëgg a jaxasool danga koy tàqaleek moroomam ya yaruwul.
Lepp looy santaane na fekk nga manal ko sa bopp ba su ñu gàntoo yit nga defal ko sa bopp, ngir nit ñi ku léen yaakaar ñu wor la.
«
Tàmbali
Weesu
1
2
Topp
Mujj
»
Xët 1 ci 2
Ñiy dugg ci Dal bi
Tay
416
Démb
2061
Ayu-bis bii
7823
Weer wii
73099
Lépp-Lépp
1572686
Amna: 19 gan, 17 bots yu lënku
Sa IP: 50.19.155.235
Tay la Mee 24, 2013
Baatukaay (Dictionnaires)
Wolof » Wolof
Wolof » Français
Français » Wolof
Wolof » English
English » Wolof
Wolof «» Allemand
Allemand >> Wolof
Lu waral Xibaaryi.com?
Sabab yi
Saafara si
Njariñ li
Ñi ciy yëngu
Boo ci bëggee jàpp
Jokkook Nun
Ay Dali Web ci làkki réew mi
Wikipedia ci wolof
Wiktionary ci wolof
Wolof.co.cc
Wolof-Online.com
Pulaangu
Tur i njanaaw yi
Ay yëgle yu bawoo Google
Internet & Web
Aada & Cosaan
Aamerig
Afrig
Alxuraan
Asi Ak Osiyaani
Démb ak Jaar-Jaar
Diine & Gëm-Gëm
Diwaan & Wërlaay
Fó, Woy ak Fecc
Gis-Gis & Céru
Jàngale ak Yar
Jëmm Ak Nit
Koom-Koom & Yokkte
Ladab, Taaral Ak Fànn
Mboolaay & Askan
Ordinaatër ak Telefon
Politig
Politig ci Àdduna bi
Tàggat-yaram
Tugal
Wér gi yaram
Xam-xam yu yees yi ak Gëstu
Xarala ak ndefar