• Sabab yi • Saafara si • Njariñ li • Ñi ciy yëngu • Boo ci bëggee jàpp
Biir waañ - 28 Des 09
• L'Observateur • Le Quotidien • L'As • Sud Quotidien • Wal Fadjri • Le Soleil • African Global News • Le Matin • Dépêches APS • www.xibar.net • L'office • Nettali.net • Ouestaf • Apanews • Expressnews • Ferloo • 24H Chrono • Reussir Magazine • La voix plus
• Jàngale ak Tàggat • Politig • Koom-Koom • Àdduna (International) • Tàggat-yaram • Wér-gi-yaram • Askan (société) • Diine • Caada • Taariix • Jëmm • Gis-gis
Diiwaan yi ak gox-goxaan yi. Néew bu dàggatoo ca tefesu Kusum
• Osad-sn.com • Seneweb.com • Senegaaltv.com • Senmedical.com • Senvideo.com
· Kuy jàpp jaan doo faale jiit · Balaa soloo baax, solo yàqu · Benn pombiteer bu nëb yàq na pañe · Bey, ci sa wewu tànk · Ëllëg, ëllëgu Yàllaa · Fagaroo gën faju · Jàpp ci gittax ba for yat · Jikko ak boroom : pax rek · Kéwél du tëb, doom ja bëtt · Ku amul ndey, nàmp maam · Ku bëreey daan · Ku jiin Njaaga, te yaay Njaag · Ku ndobin rey sa maam, boo gisee lu ñuul daw · Ku yar sa mbër, yow lay jëkk a daan · Kuy xalam di ca jaayu · Lebtoo, feytoo · Boroom lal a xam màtti lalam · Lu ëpp tuuru · Lu jot yomb · Lu waay def boppam - Lu waay rendi ci loxoom lay nàcc · Lu yëngu am na lu ko yëngal · Xalangu dajul suuf · Njuumte du ñàkk, yàgg caa bon · Paaka ba lay rey, sa mbokk a koy daas · Su la mbaam wéqee, nga wéq ko, yéen a yem · Toŋ-toŋ u naat, su wëreem réew dunx yaa tax, · Dëgg bu duggeeb nopp, dëngal du ko dindi · ngasum puloox boo ca naree yoorub goj, rombu nga reen ba. · Rayub tubaab yombu na, waaye fekke njaal maa jafe. · Tàmm laago la · Tepp-teppal mooy indi xuus · Waññ boo gis ci benn lay doore · Yàlla Yàlla bey sa tool · Yàkkamti yàqule · Yàkkamti, yàqati · Béy wéy na mbuus · Ku topp sa bakkan góob sa naqar · Li ci kanam rawul i gët · Bu ndox tuuroo am bàq a fa des · Bu gudd nopp doon tax di njiit mbaam di sunu yilimaan · Bëñ weex na lool waaye dereet a ko lal · Cërub ma xàjj, ma xujj a koy jël · Dama laa bëgg maa la raw sëy bu mu takk, dangaa reew yaa ma raw a koy tas · Màndargay dof ŋelaju ca la · Dëkkandoo jàmm a ca gën · Fët-Fët tàggalewul mbaam aki noppam · Góor gu tàyyeel, gàtt wërsëg, néewi soppe · Gumba tal na lu dul tëbi kàmb · Gumba du jiite rëbbum jaan · Ay du weesu baay dee na · Àdduna weeru koor la, fàww jant so nga doora wàññi bis. · Am saxul, ñàkk saxul · Bala ngaa xam xamadi xaw laa ray · Bu/Su yoon jeexul waaxusil du jeex · Boroom ñeenti tànk du lab · Boroom mbaam a xam mbaamam · Bët du yanu waaye xam na lu bopp àttan · Bakkan waraw dàll la, buy dagg dooko yëg · Doomi ñay bu ko ñaanal mu rëy, ñaanal ko gudd fan · Doomi mbër jàngil bëre, yàgg-yàgg dees na la ñam · bor du am rak · Xaaxom taneewulub dagg lum koy sikkee · ku jur yërëm, ku jënd sakkanal · Ku xeeb saw làkk, yokk sag ñàkk · àtte bor, fay · Mag matt ma muy jaaroo ba muy gone la koy taxan · Garab gay doon pénc, lawbe du ko gaaw a gis. · Sama bopp a ma la gënal du bañ naa la. · Ganaar gunu gàddu xamul yoonu ja bu sore. · Tungune du teew ñuy nataal · Koo yaakaar, Yàlla la yaakaar · Fegu moo gën faju · Ku la may bët nga xool fu ko neex. · Kenn xéyul mën, kenn xéyul tële · Ay sangaleñ, bu ñu booloo wat wer · Àbb delloo ca gën · Ku bëgg foo joxoñ jant feggee fa; Deel joxoñ pénku · Lu bant yàgg-yàgg ci ndox, du tax mu soppaliku mukk jasig · Lu defu waxu, lu aaye di jàmbat · Ndànk-ndànk mooy jàpp golo ci ñaay. · Xel bu doon jaay lamb · Ku ëmb sa sanqal, ëmb sa kersa · Dige bor la · Dëgg du juddu rekk màgg · Li ngay dàq mu jëm àll, dàq ko mu jëm kër · Yëfu jaambur du yëf